Download li ma wessu - WordPress.com
Document related concepts
no text concepts found
Transcript
LI MA WESSU. Youssou Ndour Mi pasado ESTRIBILLO ESTRIBILLO Li ma dundee, li ma weesu Li ma dundee, li ma weesu Dey delluse, mel ni seetu Dey delluse, mel ni seetu (BIS) (BIS) Cómo viví, cómo lo que he pasado Vuelve, como la imagen de un espejo ------- ☼ ------- Cómo viví, cómo lo que he pasado Vuelve, como la imagen de un espejo ------- ☼ ------- Ma ni seetal Ma ni seetal Leegi, leegi ma gesu Leegi, leegi ma gesu Ma ci li ma weesu Ma ci li ma weesu leegi, leegi ma recu leegi, leegi ma recu walla saxo di baaku walla saxo di baaku fu gune yi feettee, fu gune yi feettee, dama leen di teetee dama leen di teetee Setal Setal Wax nu ma neexee, Wax nu ma neexee, Ma begga leen Ma begga leen Mira !! A veces, miro atrás lo que he pasado a veces me arrepentí o sentí orgullo donde los niños festejaban yo estaba allí Mira!! A veces, miro atrás lo que he pasado a veces me arrepentí o sentí orgullo donde los niños festejaban yo estaba allí Mira!! Mira!! Cómo es bueno Los quiero ------- ☼ ------- Cómo es bueno Los quiero ------- ☼ ------- Damay, damay, damay Damay, damay, damay Dellu gune Dellu gune Mel ni, mel ni, mel ni Mel ni, mel ni, mel ni Duma magg Duma magg Voy a, voy a, voy a Volverme niño Como si, como si, como si No creciera ------- ☼ ------Lu ma gen di yàgg Cuanto más antiguo Xel ni mel ni banco Mi mente es un banco Lu ma gen di magg Cuanto más grande Dellu tuuti tanque Me vuelvo niño pequeño Voy a, voy a, voy a Volverme niño Como si, como si, como si No creciera fu gune yi feettee, donde los niños festejaban dama leen di teetee yo estaba allí wax nu mu ma hablar me gusta neexxe beggati estoy contento Lu ma gen di jege, Cuanto más me acerco ni mel dama soré es como si me alejara lu ma gendi soré cuanto más me alejé Gen di gis jegewoon Veo que me acercaba ------- ☼ ------lu ma gen di yágg Cuanto más antiguo Xel ni mel ni banco Mi mente es un banco Lu ma gen di magg Cuanto más grande Dellu tuuti tanque Me vuelvo niño pequeño ------- ☼ ------ESTRIBILLO Li ma dundee, li ma weesu Cómo viví, cómo lo que he pasado Dey delluse, mel ni seetu Vuelve, como la imagen de un espejo (BIS) ------- ☼ ------Damay, damay, damay Voy a, voy a, voy a Dellu gune Volverme niño Mel ni, mel ni, mel ni Como si, como si, como si Duma magg No creciera